Lyrics Sir Malik – Show me

 
Show me Lyrics – Sir Malik

Singer: Sir Malik
Title: Show me

Yow rek la love, baby
Meme soudé meusseuma la ko waax
Danga dawa daw beu sonou
Dem beu meunatoula noyou

Sey beutt angi honq
Xam na lu waral sey rongogn
Nenaleu dou ci yow
Suma téyéwoul seu loxo

Té douma bett benn yone
So demé beu teyé sa bopp
Déception yi ma dadialé mo beurri
Benen peine de coeur du hadj ci xol bi

Mais tey dinala waax deugg bi
Because I know you gotta know
Demay deukké di liirat su nyu texto yi
Deuké screenshot sa ayy story

Douma beugg loudoul fatt n#gg#s you topp sa guinaw
Di saup saup lou naan dagnou la feel
Soumala né beugeumala
Sama bopp laye lеuré

A chaque fois su nyu beutti tassé
Dama nane ca y еst
Man deh beugg na la nobbé lu raww ning ma nobbé
Beugg na la beugué li raww ning ma beugué

Show me how to love
Show me how to love
Show me how to love
Show me how to love

Show me how to love, baby
Show me how to love
Show me how to love
Show me show me, baby

Show me me show me, oh yeah
Show me show me, oh yeah
Show me show me
Show me

Show meYou might also like
Find more lyrics at indolirik.jspinyin.net

You can purchase their music thru 
Amazon Music  Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Other Popular Songs:
Key Kutz - Barber
Brotherhood of Man - Run Like Hell

Show me – Terjemahan / Translation

Yow rek la love, sayang
Meme Soudé Meusseuma La Ko Waax
Danga dawa daw beu sonou
Dem beu meunatoula noyou

Sey Beutt Angi Honq
Xam na lu waral sey rongogn
Nenaleu dou ci yow
Suma téyéwoul seu loxo

Té douma bett benn yone
Jadi demé beu teyé sa bopp
Déception yi ma dadialé mo beurri
Benen peine de coeur du hadj ci xol bi

Mais tey dinna waax deugg bi
Karena saya tahu Anda harus tahu
Demay deukké di liirat su nyu texto yi
Screenshot deuké sa ayy cerita

Douma BEUGG LOUDOUL FATT n#gg#S ANDA TOPP SA GUINAW
Di Saup Saup Lou Naan Dagnou La Feel
Soumala né Beugeumala
Sama Bopp Laye leuré

A Chaque Fois Su Nyu Beutti Tassé
DAMA NANE CA Y YANG
Man Deh Beugg Na La Nobbé Lu Raww Ning Ma Nobbé
BEUGG NA LA BEUGUé Li Raww Ning Ma Beugué

Tunjukkan cara mencintai saya
Tunjukkan cara mencintai saya
Tunjukkan cara mencintai saya
Tunjukkan cara mencintai saya

Tunjukkan cara mencintai, sayang
Tunjukkan cara mencintai saya
Tunjukkan cara mencintai saya
Tunjukkan padaku, sayang

Tunjukkan saya tunjukkan, oh ya
Tunjukkan saya tunjukkan, oh yeah
Tunjukkan saya tunjukkan
Tunjukkan kepadaku

Tunjukkan saya mungkin juga suka
Find more lyrics at indolirik.jspinyin.net

Lyrics Sir Malik – Show me

Kindly like and share our content. Please follow our blog to get the latest lyrics for all songs.

We don’t provide any MP3 Download, please support the artist by purchasing their music 🙂

You can purchase their music thru 
Amazon Music  Apple Music
Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases