Mangui Baxx Lyrics – Dieyla
Singer: Dieyla
Title: Mangui Baxx
Nélawo ba yandor
Deuké lou bonn ak lou niaw
Soxor ignann
Mola condamné
Doxal sa yonn
Doumala soralé
Meunou loma téré doundou lima nex
Mangui bax
Doumalén falé
Bilay dinga geuna tardé
Man daal doumalén falé
Non non doumalén falé
Fii lépangui tolo
Talouma noono
Bilay doumalén faalé
Yaw mba diam nga fanané
Yaw mba diam nga yéndo
Woté lo geumoul
Khamoni dieuli naala
Mangui bax
Doumalén falé
Bilay dinga geuna tardé
Man daal doumalén falé
Non non doumalén falé
Fii lépangui tolo
Talouma noono
Bilay doumalén faalé
Noono (mom taloula)
Li Yalla def si man
Ngané moukou doufi amé
Aaah nga dima diébaané
Nga dima diébaané
Non non nono yeah
Khamaloma dara weur dima toguè
Dima soxoré yeah yeeeahhh
Nélawo ba yandor
Loudoul deuké lou bonn ak lou niaw
Boul falé boul topato doxal sa dox
Wouyooy bokoulèn yonn doxal sa dox
Boul falé boul topato doxal sa dox
Mangui bax (mangui bax)
Doumalén falé
Bilay dinga geuna tardé (Bilay dinga geuna tardé)
Man daal doumalén falé
Non non doumalén falé
Fii lépangui tolo
Talouma noono
Bilay doumalén faalé (talouma nono)
Find more lyrics at indolirik.jspinyin.net
You can purchase their music thru or Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Other Popular Songs:
Luvlxckdown! - Cuddles
Timi Banks - Orekelewa
Lyrics Dieyla – Mangui Baxx
Kindly like and share our content. Please follow our blog to get the latest lyrics for all songs.
We don’t provide any MP3 Download, please support the artist by purchasing their music 🙂
You can purchase their music thru or Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases