Danger Lyrics – Boiie Pablo
Singer: Boiie Pablo
Title: Danger
Sku, sku
It’s your boy Pablo
Dugu fii danger la, tagoul sey mbokk bo nieuwé thiéinthieu leu
Dof-dof-loul ken doula, wakh heure bii foum toll melni degougn leu
Dundu bii diéngou leu, soy ragal thioono rek mou songou leu sééniou leu
Deumm yii fééniou leu, faw nga meuna xhamé mbaa niou diékkou leu
Fokné koula siign moy sa andadoo, dafa fekk n#gg# magagoo
n#gg# bo xhamé ni xhamagoo, meun Xhamlou balaa weesou book
Wanté bo xhamoul ni xhamagoo, dii nga lorou moudié bagn sa boop
Yanguii wouty n#gg# amagoo, boul andadook gnii amoul ndokh cii boop
Meuss negn ma raw gnima andadool, mais bima beugué damlèn yagga boote
Dafmay nekh ma djiité douma meuntii bokk
Manguék meun-meun, ak katann ak ngandii bopp
Même kii deff lou nekh mounoul nekh nieupeu, ma dieema nekh kii moudiou té ndieukeu
Nieup mounougn toloo nak té moy deugeu –
Way bou nieupеu boolo meunn ki meunn nieupеu
Mère bii dii diooy Père bii geudeu, ndakh yarougn sen doom bi ci deugg
Beugg lou nooy té fii deugueur, motakh niouy door ak dii keuffeu
Braquer leu gun bi dii seufeul, Ladj leu sa money si chauffeur
Yako nangou boodé chômeur, té yay xhagn sa bop sa honneur
Ligueur yi dou xhaadj dou diekh Hana ngay xheep !
Soy taamou naadjé comme kouy taneu thieep
Bo beuggué feekh faw nga deuké kheekh
Fii lepa metii même sou lepp di dieekh
Nga thioolé mbaa nga tekki dingko yekk
Way fexekhel tekki nguirr nga guedj ko yekk
Té lou gawa diekh moy li yomb’a am !
Gni yeekh yewou moy gni yeekh’a am !
Dou lou yeemé n#gg# nekhnaa xham !
Té lou gawa diekh moy li yomb’a am !
Gni yeekh yewou moy gni yeekh’a am !
Dou lou yeemé n#gg# nekhnaa xham !
Meuss negn ma raw gnima andadool, mais bima beugué damlèn yagga boote
Dafmay nekh ma djiité douma meuntii bokk
Manguék meun-meun, ak katann ak ngandii bopp
Même kii deff lou nekh mounoul nekh nieupeu, ma dieema nekh kii moudiou té ndieukeu
Nieup mounougn toloo nak té moy deugeu
Way bou nieupeu boolo meunn ki meunn nieupeu
Boodé yoolé man bouma diégué-diégué
Fii lepa lundum kén dou mbélé-mélé
Té souniou meun-meun dugnko wedj-wedjé
Daniouy deff ngay guiss douniou wéré-wéré
Teksi bokougnok guys loloo guena yéémé
Niom amouniou sh#t paré beugg woné
Nigaa douniou OG douniou thiéré-thiéré
Narcotik sama boyii nioola guena niémé
Diaroule ladj, that’s right boy nonu la démé
Koufii deff Lou sal rek ma fété-fété
Dinaa fessal salle signer cachet-cachet
Amatouma diote dama wara mettre le paquet
n#gg# nobouma sa yaye damko fassé-fassé
Def xhaliss sam guyn moumay gâter-gâter
Def hit, make money lolou kassé-kassé
Teksi manguék talent bi lol dou diafé-diafé
Dagnii niafé-niafé…dougnko kaféé-kaféé
Tangal game bamou bakh melni café-café
Diapp n#gg#s yii feutt, deflén dégué-dégué
Ana koukoy téré ?
Boudé dangma méré !? dafa melni ngay marr paré naan sa déréte
Boudé dangma méré !? dafa melni ngay marr paré naan sa déréte
Boudé dafa diafé dangay xharé, kassé !
Kou am dara dafa défone dara, kassé !
n#gg# Weurseuk Kiko moom rek ley, tassel !
Wanté dafay fekkii gniiy xharou di niafé !
Bo beugué alal dangsi boolé thiono, niémé !
Ki niakk alal moungui xhalate nimkoy, amé !
Ki fessak alal moungui ragal souko, niaké !
Kounek’ak lila sonal motakh nieupa wara xharé
Boy xhaar ci niite diinga lorou f#oko doul xhaaré
Lo beugg dalay gaagn rawatiina boko taméé
Niou diaay la doméram ndakh mbeuguel bougnko xamé
Loo bayii dalay bayii lolou la diamono dji wané
Boul xhool si gni nga tané dieemal dialeu fii nga callé (never)
Gang gang gang gang …
Find more lyrics at indolirik.jspinyin.net
You can purchase their music thru or Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases
Other Popular Songs:
Nu Edison - More
Istasha - Soup For Dogs
Lyrics Boiie Pablo – Danger
Kindly like and share our content. Please follow our blog to get the latest lyrics for all songs.
We don’t provide any MP3 Download, please support the artist by purchasing their music 🙂
You can purchase their music thru or Disclosure: As an Amazon Associate and an Apple Partner, we earn from qualifying purchases